Jullig kuy tukki

Jullig kuy tukki

1st - 5th Grade

7 Qs

quiz-placeholder

Similar activities

Pendidikan Agama Islam

Pendidikan Agama Islam

1st Grade

10 Qs

Formacja animatorów cz. I. (03.04.2020)

Formacja animatorów cz. I. (03.04.2020)

1st - 6th Grade

9 Qs

Elektrik Devre Elemanları

Elektrik Devre Elemanları

5th Grade

10 Qs

sifat-sifat cahaya

sifat-sifat cahaya

5th Grade

6 Qs

Agama Islam

Agama Islam

4th Grade

10 Qs

060-001 NAVIGATION, RÉGLEMENTATION, SÉCURITÉ DES VOLS

060-001 NAVIGATION, RÉGLEMENTATION, SÉCURITÉ DES VOLS

2nd Grade

11 Qs

PENDIDIKAN ISLAM TAHUN 3- ADAB TIDUR

PENDIDIKAN ISLAM TAHUN 3- ADAB TIDUR

3rd Grade

12 Qs

ULANGAN PAI BAB VI KELAS 8

ULANGAN PAI BAB VI KELAS 8

1st - 12th Grade

10 Qs

Jullig kuy tukki

Jullig kuy tukki

Assessment

Quiz

Religious Studies, Science

1st - 5th Grade

Hard

Created by

Cheikh Mbengue

Used 1+ times

FREE Resource

7 questions

Show all answers

1.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

30 sec • 10 pts

Mansour Tuubaa la dëkk. Lundi mu tukki Tambaa ngir liggéeyam. Samedi lay dellu Tuubaa. Mansour dafay wàññi julli yi ba keroog muy ñibbi.

Dëgg la !

Du dëgg !

Answer explanation

Mansour du wàññi ndax lu ëpp 20 waxtu dina ko fekk Tamba. Walla boog nga ni dina def Tamba lu ëpp 4 jours.

2.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

45 sec • 5 pts

Modou day tukki. Samba tukki wul. Tisbaar jot, Samba bëgg Modou jiite ko. Lan mooy àtte li Samba bëgg ?

Bu fekke Modou dafay wàññi, lu ñu sib la.

Dara nekk u ci.

Dafa haraam.

Dañuy waxtaan ba juboo rekk.

Answer explanation

Diggante kuy tukki ak ku tukki wul sib na ñu kenn ci ñoom jiite moroomam.

3.

MULTIPLE SELECT QUESTION

45 sec • 5 pts

Aïcha dafa tukki tukki bu dagan. Muy julli Tàkkusaan am yéene wàññi waaye mu matal def 4 ràkka. Nu muy def ?

Julli gi baax na. Dara waru ko.

Dafay def bahda salaam bu fekke dafa fàtte.

Bu fekkee moo ko tay, julli gi baaxul.

Dafay baamu abadan !

Soppu na nu mu baamu.

Answer explanation

- Kuy julli amoon yéene wàññi waaye mu tay ko daal di matal, julli gi baaxul ndax yéene gi ak jëf ji dañoo woroo (l'intention et l'action sont disjointes).

- Waaye su fekkee ni dafa juum matal, kon dafay def bahda salaam rekk.

- Soppu na nu mu baamu.

4.

MULTIPLE SELECT QUESTION

1 min • 5 pts

Imaam dafay wàññi. Bi mu defee 2 rakkas, daal di jog ngir def beneen rakka. Mustafaa sàbbaal ko waaye imaam dellusi wul. Mustafaa toog di ko xaar. Saaliw moom jog ànd ak imaam. Khadija moom daaldi sëlmal ndax dafa nekk ci tukki bu dagan wara wàññi.

Khadija julleem baaxul.

Mustafaa julleem baax na.

Mustafaa julleem baaxul waaye Khadija julleem baax na.

Saaliw julleem baaxul.

Imaam dafa wara baamu ci waxtu wi.

Answer explanation

- Khadija julleem baaxul ndax dafa njëkka sëlmal imaam.

- Saaliw julleem baaxul ndax imaam kenn du ko toppu fii ndax dafa amoon yéene wàññi ba ñépp xam ko.

- Imaam moom dafay baamu ci waxtu wi ndax yéene ji ak jëf ji dañoo wuute.

- Mustafaa julleem baax na ndax daa xaar imaam mu sëlmal te toppul imaam ci matal gi.

5.

MULTIPLE SELECT QUESTION

45 sec • 5 pts

Mourtalla dafa nekk ci tukki ba Tàkkusaan jot. Ci yoonam, mu gis mbooloo muy julli mu yaakaar ni ñii dañuy wàññi. Mu ànd ak ñoom. Waaye mbooloo mi julli 4 rakkas. Luy àtte jullig Mourtalla bi ?

Julleem baaxul. Dafay baamu abadan.

Julleem baax na waaye soppu na ñu mu baamu.

Julleem baaxul ndax yéene ji ak jëf ji dañoo wuute.

Julli gi baax na ndax moo ëpp tuyaaba.

Answer explanation

Murtalla dafa yéene woon wàññi. Kon dafay baamu abadan ndax yéene ji ak jëf ji dañoo wuute.

6.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

45 sec • 5 pts

Maymuna dafa tukki woon di ñibbi. Tisbaar ak Tàkkusaan ci yoon wi la ko fekk waaye julli wu leen. Bi mu àgge këram (chez elle), Li des ci waxtu wi mat na 3 rakka. Lu muy def ?

Dafay matal Tisbaar ak Tàkkusaan.

Dafay wàññi Tisbaar matal Tàkkusaan.

Dafay wàññi Tàkkusaan matal Tisbaar.

Dafay wàññi ñaar yépp.

Answer explanation

Règle à savoir :

Kuy ñibbi fa mu dëkk te julli wul Tisbaar ak Tàkkusaan ci yoon wi. Bi mu agsee (arrivé) li des ci waxtu wi 4 raka ou moins moo ci xaj, dfay wàññi Tisbaar, matal Tàkkusaan.

7.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

1 min • 5 pts

Ustaaz dafa tukki woon di ñibbisi. Timis ak Gee jot julli wu leen. Bi mu agse këram, li des ci waxtu wi mat na rakka. Lu muy def ?

Dafay wàññi ñaar yépp.

Dafay wàññi Timis matal Gee.

Dafay matal ñaar yépp.

Dafay matal Timis wàññi Gee.

Answer explanation

Règle :

Kiy ñibbisi te julli wul Timis ak Gee te bi mu agsee këram li des ci waxtu wi 1 rakka ou plus moo ci des dafay matal Timis (Timis kenn du ko wàññi !) wàññi Gee.