
Buntu Sangou Farata / Sétt

Quiz
•
Religious Studies
•
1st Grade
•
Hard

Soxna Astou NDIAYE
Used 1+ times
FREE Resource
9 questions
Show all answers
1.
MULTIPLE SELECT QUESTION
1 min • 5 pts
Lan moy waral sangou Farata ?
Djiguène bou paré guis mbaax (règles)
Djiguène bou am dom (bébé)
Goor bou don nélaw guéné Manyu té andoul ak banekh
Diakhasoo (rapports intimes) moukalaf goor ak djiguène
Goor bou don khol djiguène ba Manyu guéneu
2.
MULTIPLE CHOICE QUESTION
30 sec • 2 pts
Farata sangou sétt ñiata la ?
4
3
5
6
7
3.
MULTIPLE CHOICE QUESTION
30 sec • 2 pts
Sunnah sangou sétt ñiata la ?
7
4
9
5
4.
MULTIPLE SELECT QUESTION
1 min • 4 pts
Yan moy sunnah Sangou sétt ?
Sarakh ndikou
bomb thieur yi(Ragg)
massa beun beuni nop yi
Tambali ci ndayjoor bi (droite) bala thiammooñ (gauche)
Rakhass dioumbakh (nombril) bassi ome yi (genoux)
5.
OPEN ENDED QUESTION
10 mins • Ungraded
Evaluate responses using AI:
OFF
6.
MULTIPLE CHOICE QUESTION
1 min • 3 pts
Tay la adiouma ngir def louniou soppou, Modou dafa sangou sétt defalé bén bén bi.
Nakh Modou meuna dém diouli té dou diapp ?
Oui, nakh diapp na si biir sangou bi
Non, dafa wara diapp bala mouy dém diouli dji
7.
MULTIPLE SELECT QUESTION
45 sec • 5 pts
Goor bou guis Manyu si yeurém(vêtement) té khamoul kagñ la won.
Loumou wara def ?
Dafay sangou farata
Dafay sangou farata waayé dou bamou diouli yimou diouliwon bimou yéwo
Dafay bamou diouli yimou diouliwon bimou yéwo
Dafay changer yeuré (vêtement) rekk
Waroul sangou waayé dafay dindi sobé bi bala mouy diouli
8.
MULTIPLE SELECT QUESTION
1 min • 4 pts
9.
MULTIPLE CHOICE QUESTION
45 sec • 4 pts
Lan moy yakk sangou sétt ?
Lépp li todj diap
Ngélawal
Tour ndokh (saw)
Aucune de ces répones
Similar Resources on Wayground
Popular Resources on Wayground
55 questions
CHS Student Handbook 25-26

Quiz
•
9th Grade
18 questions
Writing Launch Day 1

Lesson
•
3rd Grade
10 questions
Chaffey

Quiz
•
9th - 12th Grade
15 questions
PRIDE

Quiz
•
6th - 8th Grade
40 questions
Algebra Review Topics

Quiz
•
9th - 12th Grade
22 questions
6-8 Digital Citizenship Review

Quiz
•
6th - 8th Grade
10 questions
Nouns, nouns, nouns

Quiz
•
3rd Grade
10 questions
Lab Safety Procedures and Guidelines

Interactive video
•
6th - 10th Grade
Discover more resources for Religious Studies
10 questions
PBIS Terrace View

Quiz
•
1st - 5th Grade
20 questions
Subject and predicate in sentences

Quiz
•
1st - 3rd Grade
20 questions
Addition and Subtraction facts

Quiz
•
1st - 3rd Grade
9 questions
Good Citizenship and Responsibility

Interactive video
•
1st - 3rd Grade
20 questions
Number Words Challenge

Quiz
•
1st - 5th Grade
20 questions
Place Value

Quiz
•
KG - 3rd Grade
7 questions
Science Safety

Quiz
•
1st - 2nd Grade
25 questions
Math Review

Quiz
•
1st Grade