Tuud Doom ak Révision

Tuud Doom ak Révision

1st Grade

8 Qs

quiz-placeholder

Similar activities

PENILAIAN HARIAN 1 AL QUR'AN HADIST KELAS 1

PENILAIAN HARIAN 1 AL QUR'AN HADIST KELAS 1

1st Grade

10 Qs

huruf hijaiah berharakat

huruf hijaiah berharakat

1st Grade

10 Qs

Boże Narodzenie

Boże Narodzenie

1st - 3rd Grade

7 Qs

Mikołajki 2020

Mikołajki 2020

1st Grade

13 Qs

Nityam shravanam Sevaya

Nityam shravanam Sevaya

KG - Professional Development

10 Qs

LATIHAN TAJWID

LATIHAN TAJWID

1st - 6th Grade

10 Qs

SUKU KATA TERBUKA

SUKU KATA TERBUKA

1st Grade

10 Qs

Tuud Doom ak Révision

Tuud Doom ak Révision

Assessment

Quiz

Religious Studies

1st Grade

Hard

Created by

Soxna Astou NDIAYE

Used 1+ times

FREE Resource

8 questions

Show all answers

1.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

30 sec • 1 pt

Lan mooy attéy toudou dom ?

Dagñ ko soppou

Louniou sipp la

Lou war la

Fard Kifaaya la

2.

MULTIPLE SELECT QUESTION

1 min • 1 pt

Nan laniou wara toftalé yiniou soppou si beuss Nguenté (baptême) li ?

Définition : Khar = mouton

toudou dom dji  

Rendi Khar bi

wateu dom dji

wateu dom dji

toudou dom dji  

Rendi Khar bi

wateu dom dji

Rendi Khar bi

toudou dom dji  

Rendi Khar bi

toudou dom dji

wateu dom dji

Diay dérou khar bi

3.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

30 sec • 1 pt

Media Image

Fin mokhtar Timis la

Vrai

Faux

4.

MULTIPLE SELECT QUESTION

45 sec • 1 pt

Media Image

Image bi ban waxtou diouli la ?

Fin Mokhtar Takussane

Début Darouri tisbar

Début Mokhtar Takussane

Fin Darouri tisbar

Début Mokhtar

tisbar

5.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

45 sec • 1 pt

Modou dafa touki woon di gnibissi. diouliwoul won Timis ak Gué. Bi mou aksé keureum li déss fadiar diot matna 20mn.

Lou Modou Wara def ?

Dafay wagni niar yeup

Dafay wagni Timis matal Gué

Dafay matal niar yeup

Dafay matal Timis wagni Gué

6.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

1 min • 1 pt

Mamoune dafa quitté ville A di dém ville C mais dafay diar ville B amfa 3jours

Consigne : Distance [AB]= 30km et Distance [BC]= 90km

Mamoune meun na wagni diouli entre A et B

Mamoune meun na wagni diouli

entre B et C

Mamoune dou meuna wagni diouli si yoon bi yeup

Mamoune sou agsé ville B meun na wagni diouli ba bamoufay diougué 

7.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

45 sec • 1 pt

Fatou dafay tukki distance bu matt 80km

Est-ce que Fatou meun na boolé Julli takussane ak timis ?

Oui

Non

8.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

1 min • 1 pt

Nafissatou dafa diougué Paris di dém Dakar mou deff escale 2h aéroport Casablanca tisbaar fékk kofa té bala mou ague Sénégal timis dina jot

Nafi meunoul boolé tisbaar ak takussane si aéroport Casablanca

Nafi meunoul wagni tisbaar ak takussane si aéroport Casablanca

Nafi meun na boolé tisbaar ak takussane djoulilén bounék 2 rakkas si aéroport Casablanca