Assaka partie 4

Assaka partie 4

Professional Development

9 Qs

quiz-placeholder

Similar activities

Quizz révisions

Quizz révisions

Professional Development

6 Qs

Quizz seuy

Quizz seuy

Professional Development

7 Qs

Assaka partie 6

Assaka partie 6

Professional Development

5 Qs

Quizz révision

Quizz révision

Professional Development

9 Qs

Pertanyaan Pembimbingan Murobbi

Pertanyaan Pembimbingan Murobbi

Professional Development

11 Qs

IDHGAM & IQLAB

IDHGAM & IQLAB

1st Grade - Professional Development

10 Qs

Pertanyaan untuk Kepala Sekolah/Wakil Kepala Sekolah Biah Islami

Pertanyaan untuk Kepala Sekolah/Wakil Kepala Sekolah Biah Islami

Professional Development

8 Qs

QUIZ TAJWID (PELAJARAN 6: MIM SAKINAH)

QUIZ TAJWID (PELAJARAN 6: MIM SAKINAH)

2nd Grade - Professional Development

10 Qs

Assaka partie 4

Assaka partie 4

Assessment

Quiz

Religious Studies

Professional Development

Hard

Created by

Diarra Mbacké

Used 1+ times

FREE Resource

9 questions

Show all answers

1.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

1 min • 19 pts

Lann moy difference entre miskine ak faqir ?

- Faqir moy kou amoul loumou meune doundé si att mi

- Miskine mooy ki am loumou doundé tey rek

- Faqir moy ki am loumou doundé att mi kessé

- Miskine mooy ki am loumou doundé si mois bi

-Faqir moy ki am loumou doundé tey kessé

-Miskine mooy ki am loumou doundé si att mi

2.

MULTIPLE SELECT QUESTION

1 min • 15 pts

Yann nitt laniouy diokh assaka ?

ki am aye boor

Kuy jihaad ci Yoon u YÀLLA

Kuy sooga tàbbi ci Lislaam

Kuy liggéey ci asaka

dokhandem voyageur

3.

MULTIPLE SELECT QUESTION

1 min • 20 pts

yann chartes mo wara dadié nguir meune dieul assaka ?

nek diaam

nek dioulit

nek marié

nek gor (bania nek diaam)

4.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

30 sec • 10 pts

Oustaz Mame Samba dafa am ay auto ak ay keur you beuri (masha Allah 😅) ndakh dafsiy guénné assaka

chaque année dafsi wara guénné assaka

dédéet doussi guénné dara

Ça dépend rek

5.

MULTIPLE SELECT QUESTION

45 sec • 1 pt

Modou dafa investir khaliss bou beuri si béneu boutique pour diay ay marchandises (tissus, chaussures , sacs...). Ndakh sou amé att dafay guénné assaka ?

Dafay khayma li diar ak li diaroul yeup (inventaire) mou guénné si assaka

Souféké marchandise mi dafa lambe (diayoul dara si att mi) kone dou guénné dara

Souféké dafa am loumou lébalé si marchandise mi té yakar na niou fayko kone souy deff inventaire dakassiy boolé

6.

MULTIPLE SELECT QUESTION

45 sec • 1 pt

Sokhna Aissatou dafa dieund terrain 5 millions si atoum 2019. Mou diaay ko serigne cheikh 15millions atoum 2023. Ndakh assaka warnako ?

Souféké Serigne Cheikh faynako khaliss bi kone dafay khool niata att la terrain bi deff si moom mou guénné assaka att mounék

Souféké Serigne Cheikh dafko lépp té 2026 lay fay kone Mame Diarra sou dioté khalissam dafay guénné assaka bimouko lébalé ba bimouko fayé manam (2023 ba 2026)

Souféké Serigne Cheikh dafko fayé bénén terrain de même valeur kone dafay khayma terrain bobou mou guénné si assaka

Souféké Serigne Cheikh fayna si saass yi kone Sokhna Aissatou assaka béneu att rék lay guénné ak lou terrain bi yagg yagg

souféké Serigne Cheikh dako lépp té 2026 lay meuna fay kone Mame Diarra sou dioté khaliss bi dafay guénné assaka béneu att rék

7.

MULTIPLE SELECT QUESTION

45 sec • 1 pt

Sokhna Faty dafa am auto bou cher mou échangé ko ak béneu boutikou marchandises. Après mou diay boutique bi niou fayko khaliss bou beuri : Ndakh dafa wara guénné assaka

Jour bimou amé khaliss bimou dieundé auto bi ak jour bimou diayé boutique bi lou matt nissab souféké digueunté bi matna att kone dafay guénné assaka

Souféké auto bi dégn koko mayon kone sou diayé boutique bi il faut mou denthie khaliss bi lou matt att mouy soga guénné assaka soudé matna nissab

Dans tous les cas warna guénné assaka

8.

MULTIPLE SELECT QUESTION

45 sec • 1 pt

Serigne Saer dafa am keurou 2 étages. Mou deuk si kaw loué si souf. Mou diékki rék diay keur gui : ndakh dafa wara guénné assaka ?

Avant moukay diay khaliss location bi souko dadialé bamou matt att boléssi matt nissab kone dafay guénné assaka

Souko diayé ba dieul khaliss bi dassiy guénné assaka immédiatement soudé matna nissab

Souko diayé ba dieul khaliss bi il faut mou denthie ko att té mou matt nissab mouy dora guénné assaka

9.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

30 sec • 1 pt

1er cas : Sokhna Mbene dégn ko may 2 terrains (keur) janvier 2020. Biniou aksé janvier 2023 mou diay lén béneu bounék 10 millions CFA.

2eme cas : Niokhor dafa donnou si baayam (héritage) béneu terrain (keur). 5 ans après mou diay ko 30 millions CFA

Question: Ndakh assaka war nalén ?

Niom niaar nieup déniouy guénné assaka immédiatement si khaliss bi ndakh terrains yi eupeul négn béneu année té liniouko diayé eupna nissab

Niom niar kéneu doussi guénné assaka déniouy denthie khaliss bi bamou matt att niouy soga guénné assaka

Niokho rék moy guénné assaka

Sokhna Mbene rék moy guénné assaka