Quizz révisions

Quizz révisions

Professional Development

6 Qs

quiz-placeholder

Similar activities

Quizz révision

Quizz révision

Professional Development

9 Qs

Lição 07

Lição 07

Professional Development

6 Qs

Promoção Social - Escatologia

Promoção Social - Escatologia

Professional Development

9 Qs

Bible Quiz #3 (Set 2)

Bible Quiz #3 (Set 2)

Professional Development

10 Qs

Assaka partie 6

Assaka partie 6

Professional Development

5 Qs

P GENEALOGIA Aula 12.9 - Gn Cap 17-27

P GENEALOGIA Aula 12.9 - Gn Cap 17-27

Professional Development

8 Qs

Assaka partie 4

Assaka partie 4

Professional Development

9 Qs

Quizz seuy

Quizz seuy

Professional Development

7 Qs

Quizz révisions

Quizz révisions

Assessment

Quiz

Religious Studies

Professional Development

Medium

Created by

Diarra Mbacké

Used 1+ times

FREE Resource

6 questions

Show all answers

1.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

30 sec • 1 pt

Moussa 5h lay guénneu keureum té waxtou diouli soubeu 6h la. Est ce que Moussa meun na diouli soubeu avant mouy guénneu ?

Meun na diouli souféké bouy gnibissi dina fékk diant soh

Souféké dou am fénén foumou dioulé té bala mouy gnibissi goudi diott kone may négn ko mou diouli

Dou meuna diouli té waxtou bi diotagoul

2.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

30 sec • 1 pt

Djouli soubeu ak fadiar nio bokk waxtou :

Non, fadiar moy 15mn avant soubeu

Oui

bokouniou waxtou

3.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

30 sec • 1 pt

Diouli farata niata waxtou la am ?

Diouli bounék béneu waxtou la am

Diouli bounék amna niari waxtou

4.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

30 sec • 1 pt

Dérétou règle niata jours lay durer ?

15 jours

7 jours

8 jours

ça dépend si djiguén gni

5.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

30 sec • 1 pt

Djiguén bou dioulé goul tisbar ba takoussan diot mou guiss réglam noumouy deff ?

Sou sété dafay fay tisbar késsé

Sou sété tisbar ak takoussan yeup lay fay

Doussi fay béneu

Sou sété dafay fay takoussan

6.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

30 sec • 1 pt

Djiguén bou dérétam arrêté takoussan noumouy deff ?

dafay diouli tisbar késsé

dafay diouli tisbar ak takoussan

Doussi diouli béneu

takoussan késsé lay diouli