Quiz seuy

Quiz seuy

Assessment

Quiz

Religious Studies

1st Grade

Easy

Created by

Mame Mbacke

Used 1+ times

FREE Resource

Student preview

quiz-placeholder

8 questions

Show all answers

1.

FILL IN THE BLANK QUESTION

1 min • 1 pt

Ponk seuy niata la ? (Répondre par un chiffre

2.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

30 sec • 1 pt

Yann moy ponkou seuy ?

1- Ku goor ki am kilifa

2- Ku jigéen ki am kilifa

3- Seede yi (témoins)

4- Tiann li (dot)

5- Waqqante bi (maay nala nangu na)

1- Kilifa ku jigéen ki

2- Seede yi

3- Dal bi

4- Tiann li (dot)

5- Waqqante bi

1 - Kilifa ku jigéen ki

2 - Seede yi

3 - Tari Faatiha

4 - Can li

5 - Wàqqante bi

1 - Kilifa ku jigéen ki

2 - Seede yi

3 - Dal bi

4 - Can li

5 - Julii ci Yonent bi alayhis salaatu was salaam

3.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

30 sec • 1 pt

Kiy labat sokhna lann la sagna guiss si mom ?

Kanam gui ak lokhos yi

Kanam gui, batt bi, lokhos yi ak tank yi

Lepp bamou dess awram bou diss

Aucune de ces réponses

4.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

30 sec • 1 pt

Aicha dafa am goor gouko beuga takk mou dem si nitt kouko kham diko lathie loumou kham si wadji

Ki niou lathie dagan na mou wakh limoussi kham té boumoussi yokk boumoussi wagni


Soudé lou bakh la kham si moom sagne nako wakh soudé ay sikk nak douko sania wakh

Saniouko ndakh lolou dieuw la

5.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

30 sec • 1 pt

Mamadou dégn ko may 2 diabar en même temps. Ndakh niari seuy yeup wérna ?

Niaar yeup béneu bakhoussi ndakh meunou nio takando 2 seuy en même temps

Seuy biniou ndieuka fass rék moy bakh

Niaar yeup bakhna

6.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

30 sec • 1 pt

Moussa khalé bou goor bou majeur la bou andak sagom. Dafa dem niann sokhna niou may ko té wa keuram yégouniouko en plus papam nangouwoul. Ndakh seuy bi wérna si charia ?

Seuy bi wéroul ndakh amoul kilifeu

Seuy bi wérna

7.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

30 sec • 1 pt

Badara dafa beug takk niarel wayé beugoul awom (première femme) yeuk ko. Mou dem keur sokhnassi andak niari kharitam niou wakhtann ak papay ndawsi mou maylen sokhnassi. Ndakh seuy bi wérna ?

Seuy bi wérna

Seuy bobou wéroul ndakh si keur lagn ko takké

Lolou deh moy takou souf té takou souf wéroul si charia

8.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

30 sec • 1 pt

Aicha dafa am koumou beug wayé papam dako bania mayé mou dém serignam mayé ko. Ndakh seuy bi wérna ?

Seuy bi wéroul

Seuy bi wérna ndakh serigne dafay takhaw takhawayou kilifeu

Aicha dafa waron dém si rakou papam wala magam mou mayé ko