Louy atté Massa bottes ?
Quiz Révision

Quiz
•
Religious Studies
•
1st Grade
•
Hard

Soxna Astou NDIAYE
Used 3+ times
FREE Resource
8 questions
Show all answers
1.
MULTIPLE CHOICE QUESTION
30 sec • 1 pt
Dagñ ko soppou
Dafa dagane
Lou war la
Aucunes de ces reponses
2.
MULTIPLE CHOICE QUESTION
1 min • 2 pts
Kou massa ay dalam ba noppi soumiko louy attém ?
Souféké niar yeup la soumi massa gui yakouna
Souféké béneu rék la soumi massa gui yakouwoul
3.
MULTIPLE SELECT QUESTION
45 sec • 2 pts
Khaliss niata légn si wara guéné assaka
1,5%
2,5%
1/40
4.
MULTIPLE SELECT QUESTION
1 min • 2 pts
Yan diouli légn meuna boolé ?
Guée ak soubeu
Timis ak Guée
Takoussan ak timis
Tisbar ak takoussan
5.
MULTIPLE CHOICE QUESTION
1 min • 5 pts
Mboolo mi dénio amon événement beussou vendredi si béneu salle de cérémonie, bi diouli diouma dioté niou beugue fa dioulé
Ndakh lolou meun na nékk ?
Souféké mboolo mi maténako meun négn fa diouli diouma
Meunou nioufa diouli diouma
Souféké finiou nékk diouma amoufa kone meun négn fa diouli
6.
MULTIPLE CHOICE QUESTION
1 min • 4 pts
Moussa dafay touki, bimouy diougué fimou deuk dafa amé woon bori diouli youmou wara fay : Sou agué noumouy fayé ?
Dafay matal ak lou meuna khéw
Sou agué souko nékhé matal souko nékhé wagni
Souféké amna droit wagni famou dieum kone souy fay dafay wagni
7.
MULTIPLE SELECT QUESTION
45 sec • 4 pts
Yan mossiy faratay diouli
Sigui si roukoh
Diangue saar
Tari Fatiha
Soudiote
Taaya
8.
MULTIPLE SELECT QUESTION
1 min • 5 pts
Salimata dérétou mbakh bi dafa nieuw avant diant bi diy soo
loumou wara deff sou sété ?
bou féké ni manone na diouli 4, 3,2,1 rakkas avant dianti bi diy soo dafay fay takoussan
dara warouko
bou féké ni manone na diouli 4, 3,2,1 rakkas avant dianti bi diy soo dafay fay tisbar
dafay fay tisbar ak takoussan souféké ni meunoul si wone am bén rakka avant diant bi diy soo
Similar Resources on Quizizz
11 questions
Kardynał Stefan Wyszyński

Quiz
•
1st - 8th Grade
10 questions
USA State Postal codes

Quiz
•
1st - 5th Grade
10 questions
PTS12324 PAI

Quiz
•
1st Grade
10 questions
Anioły

Quiz
•
1st - 6th Grade
10 questions
tajwid 2

Quiz
•
1st Grade
10 questions
huruf hijaiah berharakat

Quiz
•
1st Grade
9 questions
Buntu Sangou Farata / Sétt

Quiz
•
1st Grade
12 questions
Quiz Révision ak Jullig Ajjuma Partie 3

Quiz
•
1st - 3rd Grade
Popular Resources on Quizizz
15 questions
Multiplication Facts

Quiz
•
4th Grade
20 questions
Math Review - Grade 6

Quiz
•
6th Grade
20 questions
math review

Quiz
•
4th Grade
5 questions
capitalization in sentences

Quiz
•
5th - 8th Grade
10 questions
Juneteenth History and Significance

Interactive video
•
5th - 8th Grade
15 questions
Adding and Subtracting Fractions

Quiz
•
5th Grade
10 questions
R2H Day One Internship Expectation Review Guidelines

Quiz
•
Professional Development
12 questions
Dividing Fractions

Quiz
•
6th Grade