Quiz buntu seuy

Quiz buntu seuy

1st Grade

5 Qs

quiz-placeholder

Similar activities

Pendidikan Agama Islam

Pendidikan Agama Islam

1st Grade

10 Qs

Seerat Day-04 by FQA

Seerat Day-04 by FQA

KG - Professional Development

10 Qs

Qayamat

Qayamat

1st - 10th Grade

10 Qs

Quiz Révision

Quiz Révision

1st Grade - University

7 Qs

Zakat Partie 3

Zakat Partie 3

1st Grade

8 Qs

Baabu Saanii - 1

Baabu Saanii - 1

1st Grade

8 Qs

Huruf Hijaiyah Berbaris Fathah

Huruf Hijaiyah Berbaris Fathah

1st Grade

10 Qs

Agama

Agama

1st Grade

10 Qs

Quiz buntu seuy

Quiz buntu seuy

Assessment

Quiz

Religious Studies

1st Grade

Hard

Created by

Soxna Astou NDIAYE

Used 1+ times

FREE Resource

5 questions

Show all answers

1.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

1 min • 1 pt

Nafi dafay téré bopam dieukeureum té amoul béneu nguanteu (sans raison) té dégueulouko.

Ndakh dieukeureum warna continuer diko doundeul

Waw

Dédét

2.

MULTIPLE SELECT QUESTION

45 sec • 1 pt

Modou dafa fassé soxnam fassém fayli.

Lan moko war ak louko waroul si moom

moko wara doundeul ba hiddam diékh

moko wara deukeul ba hiddam diékh

Aucunes de ces réponses

3.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

30 sec • 1 pt

Demba dafa fassé soxnam fassé mou amoul fayli :

lan moko war si mom ?

moko wara deukeul ba hiddam diékh

moko wara doundeul ba hiddam diékh

4.

MULTIPLE SELECT QUESTION

45 sec • 2 pts

Yan mo war borom keur si soxnam ?

Lépp lou soxnassi yitéwo rék 

deukeul ko

doundeul ko

solal ko

5.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

1 min • 3 pts

Wadji dafa wakh soxnam ya ngui mélni si man ganawouk sama rak bou goor :

Louy attém ?

lolou fassé la

lolou ziheur la

lolou dou ziheur