Koor

Koor

Professional Development

5 Qs

quiz-placeholder

Similar activities

Quizz 0404

Quizz 0404

Professional Development

6 Qs

Quizz du 22/06/2025 Mouhadimatou Hizziya

Quizz du 22/06/2025 Mouhadimatou Hizziya

Professional Development

7 Qs

Science quiz

Science quiz

Professional Development

6 Qs

Koor

Koor

Assessment

Quiz

Science

Professional Development

Hard

Created by

Mouhanz Diag

Used 1+ times

FREE Resource

5 questions

Show all answers

1.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

30 sec • 1 pt

Moussa dafay faral di fébar chaque lundi. Bi wérou koor nieuwé mou dogg béneu Lundi yakaroon ni fébar bi dafay nieuw wayé finalement fébaroussi : Noumouy deff

dina fay dina kafara

dou fay dou kafara

dina fay wayé dou kafara

2.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

30 sec • 1 pt

Aby dafay faral di guiss mbakh chaque Dimanche. Bi wérou koor nieuwé mou am dimanche bo khamni fananowoul yéné té woroul. Bimou yéwo si dimache bi mou guiss mbakham comme nimouko yakaré woon : Noumouy deff

Dou fay té dou kafara puisque guisna mbakham

Dina fay té dina kafara

dina fay wayé dou kafara

3.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

30 sec • 1 pt

Sokhna dafa dioum naan ndokh si beuthieugou koor, guinaw gui mou continuer di lékk ak naan ndakh dafa yakar ni lolou la wara deff : Louy Attém

dafay fay beuss bobou

dafay fay boolé ko ak léllé

dina fay ba noppi kafara

4.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

30 sec • 1 pt

Samba dafa wara touki mais dafa fékk mou woor. Bi fajar fenké ba noppi mou départ après mou dogg koor gui : louy attém

dara warouko

dafay fay rék beuss bobou sans kafara

dafay fay dafay kafara

5.

MULTIPLE SELECT QUESTION

45 sec • 1 pt

Maty dafa fass yéné touki bou kheuyé ba takh fassoul yéné woor. Mou took ba fajar fenk mouy soga dém si touki bi : louy attém

dafay kafara

dafay fay beuss bobou rék té dou kafara

dafay fay dafay kafara