lathie ak tontou

lathie ak tontou

Vocational training

6 Qs

quiz-placeholder

Similar activities

Quizz du 08/08/2025

Quizz du 08/08/2025

University

6 Qs

QUIZZ DU 29/08/2025

QUIZZ DU 29/08/2025

Professional Development

6 Qs

lathie ak tontou

lathie ak tontou

Assessment

Quiz

Science

Vocational training

Hard

Created by

Mouhanz Diag

Used 2+ times

FREE Resource

6 questions

Show all answers

1.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

30 sec • 1 pt

lan moy lélé?

lélé moy diokhé 4 moudou

lélé moy diokh 60 miskin loulén sour

lélé moy diokh miskin béneu moudou

2.

MULTIPLE SELECT QUESTION

45 sec • 1 pt

lan moy kafara ?

kafara moy nga diokh 60 miskin Kou nékk 4 moudou

Kafara moy alaman bouy war kou dokk kooram té tayko

kafara moy diokh moudou 60 miskin

3.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

30 sec • 1 pt

1g d'or souy diar 50€ kone niata moy nissabou khaliss ?

4750€

4250€

29750€

4.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

30 sec • 1 pt

Penda dafa am ay takayou or (bijoux en or) yo khamni dafko dieund nguir toilétou. Kagn la assaka di war si takay yi ?

Sou maté att si moom warnassi guénné assaka

assaka doussi war

soussi amé lou matt nissab ba noppi mou matt att assaka warnassi

5.

MULTIPLE SELECT QUESTION

45 sec • 1 pt

Choisir les bonnes réponses ?

kou fébar wérou koor gui yeup sou koor gui diékhé dafay lélé wayé dou fay

Magatt (personne âgée) sou amatoul katanou woor sopp négn mouy lélé

Kiy nampal ragal doomam lorou meun na bania woor wayé dina fay té dou lélé

soxnassi eumbeu ragal doomam lorou meun na bania woor té souy fay dou lélé

kou amé borou koor sagan ba koor nieuwat té fayoul dina fay boolék kafara

6.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

30 sec • 1 pt

Maty dafa tégui natt ndakh danasssi guénné assaka ?

Souféké limou tégui matna nissab dafay guénné assaka

souféké limou tégui matna nissab té natt bi matna att dafay guénné assaka

sou maté nissab mou denthie ko att dafsiy guénné assaka

Similar Resources on Wayground