ki diouliwoul timis ba guée diot noumouy déff

Quizz 0404

Quiz
•
Science
•
Professional Development
•
Medium
Mouhanz Diag
Used 1+ times
FREE Resource
6 questions
Show all answers
1.
MULTIPLE CHOICE QUESTION
30 sec • 1 pt
dafay yéné fay timis
dafay yéné diokhé faratay timis
2.
MULTIPLE CHOICE QUESTION
30 sec • 1 pt
yan tontou nio bakh
soow (lait maternél) sou diougué si yéfeur sobéla
dérétou yéfeur sobéla
nén (oeuf) bou périmé sobéla
dieumi khathie bouy doundou sobéla (karawam, youteum...)
wothiou bou sopékou sobéla
3.
MULTIPLE CHOICE QUESTION
30 sec • 1 pt
ki wara diouli tisbar ak takoussan té diant bi di wadia soh noumouy deff
sou waxtou wi khaté dafay djiteul timis soga diouli tisbar ak takoussan
souféké béneu diouli mofi khathie avant timis kone dafay diouli takoussan téksi timis sou noppé soga diouli tisbar
dafay diouli tisbar, téksi takoussan soga diouli timis
4.
MULTIPLE CHOICE QUESTION
30 sec • 1 pt
Soxnassi dafa fatalikou ni waron na sangou sétt fékeu mouy diouli farata noumouy deff
souféké sou démé sangou nieuw dou am béneu rakka si waxtou wi kone dafay wéyeul
dafay dagg dém sangou nieuw tambaliwaat
sou khassé tambali diouli dou dagg dafay wéyeul
5.
MULTIPLE CHOICE QUESTION
30 sec • 1 pt
Ki waron sangou farata amoul ndokh mou tiim, sou waxtou diouli nieuwaté noumoy déff
souféké ndokh amna dafay diapp
souféké tiim bi todioul meun nassi diouli waat
sou ndokh amé dafay sangou farata
6.
MULTIPLE SELECT QUESTION
45 sec • 1 pt
ki amé dianaba moy:
djiguén bou sétagoul
ki guenteu maniyou guéneu si moom
ki amé tothie mou makk
goor bou sékeu ak djiguén wala djiguén bou sékeu ak goor
Similar Resources on Quizizz
Popular Resources on Quizizz
20 questions
math review

Quiz
•
4th Grade
20 questions
Math Review - Grade 6

Quiz
•
6th Grade
20 questions
Reading Comprehension

Quiz
•
5th Grade
20 questions
Types of Credit

Quiz
•
9th - 12th Grade
20 questions
Taxes

Quiz
•
9th - 12th Grade
10 questions
Human Body Systems and Functions

Interactive video
•
6th - 8th Grade
19 questions
Math Review

Quiz
•
3rd Grade
45 questions
7th Grade Math EOG Review

Quiz
•
7th Grade