Quizz du 08/08/2025

Quizz du 08/08/2025

Assessment

Quiz

Science

University

Hard

Created by

Mouhanz Diag

Used 4+ times

FREE Resource

Student preview

quiz-placeholder

6 questions

Show all answers

1.

MULTIPLE SELECT QUESTION

45 sec • 1 pt

Lan léniouy téré kou amoul diapp ?

lire Alquran

laal Alquran

khool kamilou Alquran

diouli

2.

MULTIPLE SELECT QUESTION

45 sec • 1 pt

Lan moy yakk diapp ?

nélaw

goor laal waay yalaam (testicules)

djiguén laal awram

guénné déréet

kheum (évanouissement)

3.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

30 sec • 1 pt

Maïmouna dafa diapp ba noppi sobé tourou si kawam, noumouy deff ?

dafay laabal sobéssi ba noppi diappaat

dafa wara sangou farata

dafay laabal sobéssi rék

4.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

30 sec • 1 pt

lan moy attéy kouy diouli fékk mou safon dém wanak ?

sou dara guénoul dioulém baxna

dioulém bakhoul

sou indé faratas yi nimou waré dioulém baxna

5.

MULTIPLE SELECT QUESTION

45 sec • 1 pt

tothie moy lan ?

hadass

yi bakho guénéu si niari bountou yi si ak wér

habass

sobé

6.

OPEN ENDED QUESTION

3 mins • 1 pt

Yan khétou sobé nga kham youy guéneu si sawoukayou domou adama ? (Ecrire les réponses dans l'espace vide)

Evaluate responses using AI:

OFF