
Quizz Tiim du 19/09/2025
Authored by Mouhanz Diag
Science
Professional Development
Used 2+ times

AI Actions
Add similar questions
Adjust reading levels
Convert to real-world scenario
Translate activity
More...
Content View
Student View
6 questions
Show all answers
1.
MULTIPLE CHOICE QUESTION
30 sec • 1 pt
Ban si baat yii moy firi tiim ?
Wudu
Tayammum
Ghusl
Tahara
2.
MULTIPLE CHOICE QUESTION
30 sec • 1 pt
Modou amna ndokh mou meuna diapp wayé dafa nékk si touki. Sou diouli dioté noumouy deff ?
dafa wara diapp
dafa wara tiim
souko nékhé diapp souko nékhé tiim
3.
MULTIPLE CHOICE QUESTION
30 sec • 1 pt
Fatou dafa wara sangou sétt té amoul ndokh. Fimou wara wouté ndokh soriwoul wayé yoon bi dafa am ay bandis youfa nékk : noumou wara deff sou waxtou diouli dioté?
Dafay khar baniou dém
dafay tiim
dafay woo police
dafay dém rék loumou am dieul
4.
MULTIPLE CHOICE QUESTION
30 sec • 1 pt
Matar dafa amé janaba té amoul ndokh boumou sango. Ndakh sagne na sékeu ak soxnam ?
Dédéet douko sagne
sou beugué sékéu ak moom dafa wara tiim ba noppi
sagne nako
5.
MULTIPLE SELECT QUESTION
45 sec • 1 pt
Soxnassi dafa sétt wayé amoul woon ndokh boumou sango sétt mou tiim diouli bala waxtou wi diko raw.
1- Sou amé ndokh guinaw gui noumouy déff ?
2- Ndakh sagne na sékeu ak borom keureum guinaw bimou tiimé té sangogoul ?
Sou ndokh amé dafa wara dém sangou ba noppi diouli waat
dafay sangou sétt rék wayé dou diouli waat
sou tiimé ba noppi diaroul mouy sangou té dou diouliwaat
sagne na sékeu ak borom keureum souféké tiim na
dafa wara sangou ba noppi bala mouy sékeu ak borom keureum
6.
MULTIPLE CHOICE QUESTION
30 sec • 1 pt
Moussa amna ndokh wayé sou diappé rék diouli adiouma dji dinako raw : Ndakh sagne na tiim nguir meuna bokk si diouli gui ?
waw
dédéet
Access all questions and much more by creating a free account
Create resources
Host any resource
Get auto-graded reports

Continue with Google

Continue with Email

Continue with Classlink

Continue with Clever
or continue with

Microsoft
%20(1).png)
Apple
Others
Already have an account?
Popular Resources on Wayground
15 questions
Fractions on a Number Line
Quiz
•
3rd Grade
20 questions
Equivalent Fractions
Quiz
•
3rd Grade
25 questions
Multiplication Facts
Quiz
•
5th Grade
22 questions
fractions
Quiz
•
3rd Grade
20 questions
Main Idea and Details
Quiz
•
5th Grade
20 questions
Context Clues
Quiz
•
6th Grade
15 questions
Equivalent Fractions
Quiz
•
4th Grade
20 questions
Figurative Language Review
Quiz
•
6th Grade
Discover more resources for Science
10 questions
How to Email your Teacher
Quiz
•
Professional Development
6 questions
3RD GRADE DECLARATION OF INDEPENDENCE EXIT TICKET
Quiz
•
Professional Development
19 questions
Black History Month Trivia
Quiz
•
6th Grade - Professio...
22 questions
Multiplying Exponents with the Same Base
Quiz
•
9th Grade - Professio...
40 questions
Flags of the World
Quiz
•
KG - Professional Dev...