
Wagni diouli

Quiz
•
Religious Studies
•
Professional Development
•
Medium

Diarra Mbacké
Used 1+ times
FREE Resource
6 questions
Show all answers
1.
MULTIPLE CHOICE QUESTION
45 sec • 20 pts
Kouy tukki tukki bou ayoul dagane na mou wagni diouli
Vrai
Faux
Answer explanation
Cest une Sunnah très recommandée :
Anas ibn Malick (P.A.a) a dit: Nous sortîmes de Médine pour nous rendre à La Mecque en compagnie du Prophète (Bénédiction et salut soient sur lui). Celui-ci ramenait ses prières à deux rak'aa chacune jusqu'à notre retour à Médine. (Rapporté par al-Bokhari,1081 et par Mouslim,724)
2.
MULTIPLE SELECT QUESTION
45 sec • 20 pts
Kou nek si tukki bou dagane yane diouli la meune wagni ?
Icha (Gué)
Dohr (Tisbar)
Asr (Takussan)
Maghreb (Timiss)
Answer explanation
Ibn al-Qayyim (Puisse Allah lui accorder Sa miséricorde) dit: Le Prophète (Bénédiction et salut soient sur lui) ramenait à deux rak'aa les prières qui en comptent quatre.
3.
MULTIPLE SELECT QUESTION
45 sec • 20 pts
A- Khadija dafa touki nguir seti mbokk talibem bi febar
B- Aicha dafa touki Makkah nguir kham dineem
C- Maryam da touki nguir ligueyam
Kann mossi meune wagni diouliwam ?
Khadija
Aicha
Maryam
Ken meunoul wagni diouli
Answer explanation
Pour meune wagni diouli il faut mou nékk touki bou ayoul (voir exemple)
- Touki bou war (adji makka adjou farata)
- touki bou dagan (liguéy, commerce...)
- touki bouniou sopp (séeti mbokoum djoulit)
4.
MULTIPLE CHOICE QUESTION
30 sec • 20 pts
Kou tukki distance bou matt 90 km aller-retour meuna wagni diouli
Vrai
Faux
Answer explanation
Touki bi na matt 72km (wala 89,4km si li gueuna woor), dém bi rék (seulement l’aller) mo xam touki ndokh wala souf wala diawou dji
5.
MULTIPLE SELECT QUESTION
45 sec • 20 pts
A- Pathé dafa touki touki bou dagane wantei da mooy ya Allah si biirr
B- Khoudia da guene di dem tei khamoul foumou dieum
C- Amina da dem Medine nguir fekhal kholam
D- Adama da touki nguir sathie si train bi
Nian laniou may niou wagni diouli ?
Pathé
Amina danio sipp mou wagni
Adama ak Khoudia
Kenn waroussi wagni diouli
Answer explanation
Gni meunouta wagni sen diouli
ko khamni dieumi touki ba ak moy la (kouy sathi, wala mouy rayi nitt) dou sania wagni
- souféké dieumi touki ba ayoul mais dafay moy Yalla sa biir (naan fa sangara wala mou ndialo fa) batay dina sania wagni
- ko khamni touki foh lay touki par exemple kouy reubi (chasse par simple plaisir wayé lamouy reub dependrou si nguir doundou) wala sakh ap touriste bouy dém nguir rék fékhal kholam : nioniou sipp négn sén wagni wayé souniou wagné tamit sén djouli baxna
- kou guéneu di dém rék té khamoul foumou dieum (berger, kouy weur dara..) dou sania wagni si bouy dém loudoul mou woor ko ni limou beug bala mouko am dina dokh lou matt dokhou wagni wala louko eup (89km)
6.
MULTIPLE CHOICE QUESTION
45 sec • 20 pts
Waxtou djouli soubeu foumou tambalé ak foumou yém
Migui tambali fadjr ba diant bi fenk
Migui tambali souniou yéwo diekh sou diant bi fenkei
Migui tambali sou diant bi fenkei diekh sou 12h dioté
Migui tambali fadjr ba midii
Similar Resources on Wayground
Popular Resources on Wayground
10 questions
Video Games

Quiz
•
6th - 12th Grade
10 questions
Lab Safety Procedures and Guidelines

Interactive video
•
6th - 10th Grade
25 questions
Multiplication Facts

Quiz
•
5th Grade
10 questions
UPDATED FOREST Kindness 9-22

Lesson
•
9th - 12th Grade
22 questions
Adding Integers

Quiz
•
6th Grade
15 questions
Subtracting Integers

Quiz
•
7th Grade
20 questions
US Constitution Quiz

Quiz
•
11th Grade
10 questions
Exploring Digital Citizenship Essentials

Interactive video
•
6th - 10th Grade