Charte Imam Partie 2

Charte Imam Partie 2

Professional Development

7 Qs

quiz-placeholder

Similar activities

Assaka partie 6

Assaka partie 6

Professional Development

5 Qs

Quizz révision

Quizz révision

Professional Development

9 Qs

KKQ TING 1 = HAFAZAN (( BENTUK BACAAN AL-QURAN ))

KKQ TING 1 = HAFAZAN (( BENTUK BACAAN AL-QURAN ))

6th Grade - Professional Development

10 Qs

Manhaj Imam Hamzah

Manhaj Imam Hamzah

KG - Professional Development

10 Qs

Indahnya Kebersamaan dengan Shalat Berjamaah

Indahnya Kebersamaan dengan Shalat Berjamaah

KG - Professional Development

10 Qs

Imam Mehdi (atfs).

Imam Mehdi (atfs).

Professional Development

12 Qs

Quizz revision partie 2

Quizz revision partie 2

Professional Development

6 Qs

Assaka partie 4

Assaka partie 4

Professional Development

9 Qs

Charte Imam Partie 2

Charte Imam Partie 2

Assessment

Quiz

Religious Studies

Professional Development

Hard

Created by

Diarra Mbacké

Used 3+ times

FREE Resource

7 questions

Show all answers

1.

MULTIPLE SELECT QUESTION

1 min • 4 pts

Imam da fatei diap, djitei mbooloo ba nopii diko soga fatelikou.

Louy atei diouli Imam bi ak diouli mbooloo mi ?

Imam dey baamou abadan

Mbooloo bi dey baamou abadan

Imam ak mbooloo mi yeup daniouy baamou

Mbooloo mi dou baamou sou fekkeini khamoul wone ni Imam diapoul

Answer explanation

Bokouna si charte Imam que da wara laab :

Ki djitei mbollo tei amoul laab diouliwam ak bou mbollo mi yeup yakouna. Sou fekkeini Mbollo mi khamouniou ko wone Imam rek moy baamou abadan.

2.

MULTIPLE SELECT QUESTION

1 min • 5 pts

Fatima ak Khadija daniouy diouli. Niom niar niou décider ni Fatima mooy djitei ndakh mo guene mokkal Al Quran. Lane moy atei diouli Fatima ak Khadija.

Khadija diouliwam bakhoul

Niom niar sen diouli bakhoul

Fatima diouliwam bakhna

Niom niar sen diouli bakhna

Answer explanation

Imam goor la wara nek. Si nguirou Imam Malick jiguene dou djitei (dou djitei goor tei dou djitei djiguene tamitt).

3.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

1 min • 5 pts

Khalei bou djitei aye moukalaf (majeure) diouli farata :

Khalei bi diouliwam bakhoul

Makk gni daniouy baamou abadan

niom nieup sen diouli bakhna

dagn ko sipp

Answer explanation

Imam bi Moukalaf la wara nek. Khalei du djitei aye moukalaf bou fekei ni diouli farata la wayei meune naa djitei mukallaf naafila (guenoul nak)

4.

MULTIPLE SELECT QUESTION

1 min • 5 pts

Babacar dey djitei diouli Takussan.

Ibrahima,Bamba ak Aicha niogui diouli si guinawam :

- Ibrahima bimou parei tayah da ndieuk seulmal imam

- Bamba dafa ndieuk roukkoh imam

- Aicha da done defando ponk yi en mm temps que Imam

Lane moy atei diouli maamum yi ?

Aicha sipp negn nimou diouliwei wantei diouliwam bakhna

Ibrahima dey bahda salam

Niom nieup sen diouli bakhoul daniouy baamou

Bamba deff na lou haram wayei diouliwam bakhna

Answer explanation

II- Lane la Maamum wara deff (3) (kiniou djitei)

1- Maamuum bi daa wara am yenei rooy Imam bi.

2- Maamuum bi ak Imam bi da nio wara diouli mm wakhtu bi (même jour, même wakhtu). Kouy naafila meunouta djitei kouy diouli farata wayei inverse bi meune na nekk.

3- Maamuum bi waroul ndieuka kaabar Imam tei warou ko ndieuk seulmal tamitt. Su ko defee rekk diouliwam yaquna. De plus sen kaabar ak seulmal waru nio toloo. Bou fekei ni maamum bi daf koo ndieuka deff yeneen ponku yii, dafay haraam waaye dou takh diouli bi yakou. Souniou defandoowei ponk yi dagn koy sip.

5.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

1 min • 5 pts

Bann imam laniou sipp mou djitei ?

Imam bou am aye goom

Imam bou ndiol

Imam bo khameni lou eup si mbooloo mi beugoul mou djitei

Imam bou handicapé

Answer explanation

- Am na woutei si borom kham kham yi si ndakh Imam bou handicapé danio sipp mou djitei. Li guena woor moy que dou lougnou sipp.

- Sip negn imam bou am pb de vessie di djitei

- Sip negn Imam bou am aye goom di djitei

6.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

1 min • 5 pts

5 prières obligatoires yi dioulei lene si mbooloo

Farata la

Sunnah la

Sunnah bou degueur la

Louniou sopp la

Answer explanation

 Diouli mbooloo mo guene 27 fois diouli benn nit.

Mbooloo moo ngi tàmbalee ñaar jëm kaw waaye am na ag wuute.

- Atei diouli mbooloo :  sunnah mu'akkada la

- Diouli mbollo farata la si diouli Al jummah, sounnah bou deugueur la ci Korité/Tabaski.

7.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

1 min • 5 pts

Amina diouliwoul depuis demba si Icha (Gué). Wakhtou tisbar tey diott mou beug diouli.

Lane la wara deff ?

Dey diouli tisbar ba nopi doga rattraper yenene diouli yi

Dey rattraper yenene dioulis yi ba nopi doga diouli tisbar

Answer explanation

- kou amé 4 borou djouli wala louko gueuna néew (4, 3,2,1) daf lén di fay ba noppi soga djouli gui téew

Exemple: kou djouli woul soubeu tay ba waxtou djouli timis diot. Kokou aména 3 borou djouli youmou wara fay ak timis gui téew: Kone dafay fay borou djouli yi ba noppi (soubeu, tisbar, takoussan) soga djouli timis

- kou amé 6 borou djouli wala louko eup (6, 7...) dafay djouli gui téew ba noppi soga fay yimou faat

Exemple: kou djouli woul tisbarou demb ba timissou tay. Kokou aména 7 borou djouli youmou wara fay ak timissou tay gui téew (timissou tay gui bokoul si yiniou wara fay ndakh mo ngui si waxtoom): Dafay ndjeuka djouli timissou tay gui ba noppi soga fay borou djouli yi tambaléko tisbarou demb ba takoussanou tay

- Souféké borou djouli yi dafa yém képp si 5

 kone amna niou wakh ni daflén di fay ba noppi soga djouli gui téew (voir cas 6) ndakh dénio diapp ni ba légui 5 borou djouli bariwoul

Amna tamit niou wakh ni dafay djouli gui téew ba noppi soga fay borou djouli ya ndakh 5 borou djouli dafa beuri (voir cas 7)

Niaar yi loumoussi deff baxna