
Quizz seuy

Quiz
•
Religious Studies
•
Professional Development
•
Medium

Diarra Mbacké
Used 2+ times
FREE Resource
7 questions
Show all answers
1.
MULTIPLE CHOICE QUESTION
30 sec • 1 pt
Demba dafa beuga takk djiguén bo khamni athée la (manam gueumoul béneu diiné té gueumoul Yalla) ndakh seuy bobou meun na nekk si Islam ?
Oui
Non
2.
MULTIPLE SELECT QUESTION
45 sec • 1 pt
Ablaye dafa beuga takk djiguén bo khamni juive la. Choisir la ou les bonne(s) réponse(s) parmis les suivantes :
Dioulit bou goor dou takeu ap juive
Soxnassi souféké bayam juif la ni moom kone meun nako mayé
Seuy bi dina wér
3.
MULTIPLE CHOICE QUESTION
30 sec • 1 pt
Atouman dafa beuga takk doomi soeuram boumou bokal baay késsé ndakh lolou meun na nékk
Waw diiné mayé nako
Lolou meunoul nékk si charia
oui mais...
Atouman ndidiayam la té ndidiay meun na takk diarbaatam
4.
MULTIPLE SELECT QUESTION
45 sec • 1 pt
Iboulaye dafa takk Nafi après mou fassé ko takkeu soeuram: Ndakh lolou meun na nékk ?
Kéneu meunoul takk 2 soeurs
Kéneu dou boolé 2 soeurs si lislam
Souféké Nafi ak soeuram nio bokk ndeye ak baay kone seuy bi dou bakh si lislam
Seuy bi wérna
5.
MULTIPLE CHOICE QUESTION
30 sec • 1 pt
Moussa dafa beuga takk doomou rakkou yayam ndakh seuy bobou meun na nékk ?
Seuy bi meunoul nékk
Seuy bi meun na nékk
6.
MULTIPLE SELECT QUESTION
45 sec • 1 pt
Wadji goor la woon wayé dafa deff chirurgie esthétique niou changél ko sexe deff ko mou am forme ay thieurou djiguén ba kouko guiss diapp ni djiguén la (transgenre) : Ndakh kokou meun na seuy ak goorou dioulit
Souféké amna ay thieurou djiguén (baatou djiguén, deuneu, awra djiguén...) kone goor meun nako takeu
Lolou mou deff haram na
Dou meuna seuy ak goorou dioulit
7.
MULTIPLE CHOICE QUESTION
30 sec • 1 pt
Ibou dafa am 3 femmes niou mayat ko yénén 2 femmes mouy 5: Louy attém ?
Dafa wara fassé 5 femmes yeup ndakh dioulit dou denthie lou eupeu 4
3 femmes you ndieuk yi wérna wayé 2 you moudiou yi bakhoul
Souféké niari seuy you moudiou yi dégn lén fass en même temps kone béneu doussi bakh
Similar Resources on Wayground
Popular Resources on Wayground
15 questions
Hersheys' Travels Quiz (AM)

Quiz
•
6th - 8th Grade
20 questions
PBIS-HGMS

Quiz
•
6th - 8th Grade
30 questions
Lufkin Road Middle School Student Handbook & Policies Assessment

Quiz
•
7th Grade
20 questions
Multiplication Facts

Quiz
•
3rd Grade
17 questions
MIXED Factoring Review

Quiz
•
KG - University
10 questions
Laws of Exponents

Quiz
•
9th Grade
10 questions
Characterization

Quiz
•
3rd - 7th Grade
10 questions
Multiply Fractions

Quiz
•
6th Grade