Révision

Révision

Professional Development

8 Qs

quiz-placeholder

Similar activities

Kensyon Chapit 17

Kensyon Chapit 17

Professional Development

11 Qs

Abdest - Omer Nasuhi Bilmen

Abdest - Omer Nasuhi Bilmen

Professional Development

10 Qs

Quizz révision

Quizz révision

Professional Development

9 Qs

Latian I PAI

Latian I PAI

10th Grade - Professional Development

8 Qs

Revelation 12

Revelation 12

Professional Development

10 Qs

Er Risale

Er Risale

Professional Development

12 Qs

Révision

Révision

Assessment

Quiz

Religious Studies

Professional Development

Hard

Created by

Diarra Mbacké

Used 1+ times

FREE Resource

8 questions

Show all answers

1.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

30 sec • 1 pt

Yan moy khadiou diiné dji ?

dioulit, yéfeur, nassaran, yahoud

Fiqh, tawhid, tassawouf

Imaan, Islam, Ikhsaan

2.

MULTIPLE CHOICE QUESTION

30 sec • 1 pt

Attey Charia yi yan la ?

soubeu, tisbar, takoussan, timis, guée

lou war, lou haram, lou dagan, louniou sopp louniou sipp

Adiannah ak safara

3.

MULTIPLE SELECT QUESTION

45 sec • 1 pt

Ponki lislam yi yan la ?

- diapp ak sangou farata

diouli soubeu, tisbar, takoussan, timis, guée

guénné assaka ak woor wérou koor

ragal Yalla té diamouko

4.

MULTIPLE SELECT QUESTION

45 sec • 1 pt

4- Ponki ngueum yi yan la ?

gueum assaman ak souf

Gueum Yalla ak yonent yi ak malaka yi

gueum dée (la mort) ak dékki

gueum lou am Yalla moko dogal

5.

MULTIPLE SELECT QUESTION

45 sec • 1 pt

Yan khétou laab mo am ?

laab si ndokh

laab si sobé

tiim

 laab si tothie

6.

MULTIPLE SELECT QUESTION

45 sec • 1 pt

Lan moy waral sangou sétt ?

mazyou ak wadyou

sétt si mbeureuk

perte blanche

diakhasso goor ak djiguene

7.

MULTIPLE SELECT QUESTION

45 sec • 1 pt

Limeul (citez) yéneu si ay sobé

galleu ak wothiou ak niandakhit

nguélawal

tour ndokh ak néféré domou adama, sawou bébé

nén bou neup

deuteu bou andak déréet 

8.

MULTIPLE SELECT QUESTION

45 sec • 1 pt

Yan signes moy woné ni nitt ki majeur na ?

eumbeu (grossesse)

kouy mesuré 1m80

karawou nakeu ak pokotan

guiss mbeureuk

guent di seuy guénné maniyou