Lan moy maa-oul moutlaq ?

Quizz du 22/06/2025 Mouhadimatou Hizziya

Quiz
•
Science
•
Professional Development
•
Hard
Mouhanz Diag
Used 2+ times
FREE Resource
7 questions
Show all answers
1.
MULTIPLE SELECT QUESTION
2 mins • 1 pt
moy ndokh mou laab
moy ndokh mou meuna laabal
moy ndokh mou laab té meuna laabal
moy ndokh mo khamni lou deukoul ak moom (corps étranger) sopiwoul couleur bi wala goût bi wala odeur bi.
2.
MULTIPLE SELECT QUESTION
2 mins • 1 pt
Choisir les bonnes affirmations
Ndokh mouniou bakhal meunoul sangou farata
Ndokh mouniou deff thiéppeu laab na
Ndokh mouniou khorom meun na diapp
Ndokh mouniou soti souf laab na té meun na laabal
Galace bouniou décongelé meun na laabal wayé laaboul
3.
MULTIPLE SELECT QUESTION
2 mins • 1 pt
Moussa dafa tékk satalam di wadia diapp sobé dougoussi, ndakh meun nassi diapp ?
souféké ndokh mi beuriwoul doussi meuna diapp
souféké sobéssi sopiwoul ndokh mi meun nassé diapp
Souféké ndokh mi sopékouwoul sipp négn mou diappéko sou amé bénén ndokh
4.
MULTIPLE CHOICE QUESTION
2 mins • 1 pt
Ndakh djiguén meun na dioulé yeuré bimouy sol période bimouy guiss règle ?
même souféké yeuré bi takoul dara douko meuna dioulé
yeuré bobou laaboul
meun nako dioulé souféké takoul déréet
5.
MULTIPLE CHOICE QUESTION
2 mins • 1 pt
Choisir la réponse qui complète la phrase suivante :
......... moy nga diapp wala nga tiim wala nga sangou sétt.
laab
laabou habas
sobé
laabou hadas
6.
MULTIPLE CHOICE QUESTION
2 mins • 1 pt
Choisir la réponse qui complète la phrase suivante :
..... moy lo khamni laabou habas mokoy dindi
tothie
sangou farata
sobé
tilim ak tache
7.
MULTIPLE SELECT QUESTION
2 mins • 1 pt
Choisir les 3 réponses qui complètent la phrase suivante :
............ ak ............ niooy khadiou ..............
tiim diapp ak sangou farata
laab
laabou hadas
laabou habas
Similar Resources on Quizizz
Popular Resources on Quizizz
15 questions
Multiplication Facts

Quiz
•
4th Grade
20 questions
Math Review - Grade 6

Quiz
•
6th Grade
20 questions
math review

Quiz
•
4th Grade
5 questions
capitalization in sentences

Quiz
•
5th - 8th Grade
10 questions
Juneteenth History and Significance

Interactive video
•
5th - 8th Grade
15 questions
Adding and Subtracting Fractions

Quiz
•
5th Grade
10 questions
R2H Day One Internship Expectation Review Guidelines

Quiz
•
Professional Development
12 questions
Dividing Fractions

Quiz
•
6th Grade