
Quizz revision partie 2

Quiz
•
Religious Studies
•
Professional Development
•
Hard

Diarra Mbacké
Used 2+ times
FREE Resource
6 questions
Show all answers
1.
MULTIPLE SELECT QUESTION
45 sec • 5 pts
Yann mossiy faratay sangou sett ?
Galakh ndikou
Rakhass beun beun nopp yi
Yéené bi
Bomb tieur yi
Answer explanation
Faratas sangou sett :
1- Yéené
2- matalé (yaram bi yepp toy )
3- gaw
4- bomb tieur yi
Sunnah sangou sett :
1- rakhass say loxo ci tikk diara (poignet)
2- galakh ndikou
3- sarakh ndikou
4- massa beun beuni nop yi (rakhass nop yi si matalei bi la bokk)
2.
MULTIPLE CHOICE QUESTION
30 sec • 5 pts
Diap niata sunnah la am ?
5
4
8
7
3.
MULTIPLE SELECT QUESTION
45 sec • 5 pts
Yann mossiy sunnah diap ?
Rakhass sa kanam
Rakhass sa lokho bassi tikou diara
Galakh ndikou
Firou
Toftalei faratas yi
Answer explanation
Limouk sunnass diapp diourom – niétt (8)
1- Rakhass sa lokho yi bassi tikou diara/montre yi
2- Galakh ndikou (3 conditions goukh ndokh bi, mélanger ak yabii)
3- Sarakh ndikou ( dougal ndokh bi si sa bakane)
4- Nanga firou (guené ndokh bi si sa bakane)
5- Delo massa bopp
6- Toyal sa lokho doga massa sa nopp yi
7- Massa nopp yi
8- Toftalé faratas yi
4.
MULTIPLE SELECT QUESTION
45 sec • 5 pts
- Maryam da done diap mou fatei rakhass lokhos yi bassi tionth yi mou fatelikou ko bimouy massa nopp yi
- Fatima da diap ba noppi fatelikou ni massa woul boppam
Lane laniou wara deff ?
Niom niar daniouy bamou wat diap bi
Fatima dey yenei matal diap bi après mou massa bopp bi
Maryam dey rakhass lokhos yi bassi tionth yi après massa bop bi, massa nop yi après rakhass tank yi
Fatima dey bamou waat diap bi
Answer explanation
Attep Faté farata si diapp
Cas 1 : ki diap ba paré fatelikou si sassi ni da faté rakhass béne thieur day commencer wat diap bi à partir de thieur bobou
Cas 2 : ki diap bou yagg doga fatelikou ni que rakhassoul bene thieur, thieur bobou rek lay rakhass yéne motali diap bi
Cas 3 : ki diouli ba parei doga fatelikou nii que rakhassoul béne thieur day rakhass thieur bobou bamou waat diouli gui ndakh diapp bi matoul wone
5.
MULTIPLE SELECT QUESTION
45 sec • 5 pts
- Bamba da diouli ba noppi fatelikou ni galakh ndikou woul wone
- Mohamed da diouli ba nopi fatelikou ni rakhassoul wone tank yi
Lane moy atei seni diap ak seni diouli ?
Niom niarr sen diouli yakouna
Daniouy diapat niom niarr nieup
Mohamed da wara motali diapam après bamou wat diouli gui
Bamba dou bamouwat diouli gui
Mohamed diouliwam bakhoul
Answer explanation
Ki fatei sunnah si diap
Bou féké ni da ko fatalikou fek diouli na ba paré ; dou yakeu diouli bi ndakh sounnah yakoul diap mais day dem rakhass thieur bi guir motali diap mi pour diamou yallah yissiy topate.
6.
MULTIPLE SELECT QUESTION
45 sec • 5 pts
Louy waralouk (Causes) tiim ?
Sokhna sou lettou aye méches meune na tiim
ki amoul ndokh guir diapp wala sangou farata dafay tiim
ki am ndokh ba nopi raggal moukhtarou diouli gui raw ko
ki am ndokh wayei bouko utiliser dieulei si febar wala aggraver ko
Similar Resources on Wayground
Popular Resources on Wayground
10 questions
Lab Safety Procedures and Guidelines

Interactive video
•
6th - 10th Grade
10 questions
Nouns, nouns, nouns

Quiz
•
3rd Grade
10 questions
Appointment Passes Review

Quiz
•
6th - 8th Grade
25 questions
Multiplication Facts

Quiz
•
5th Grade
11 questions
All about me

Quiz
•
Professional Development
22 questions
Adding Integers

Quiz
•
6th Grade
15 questions
Subtracting Integers

Quiz
•
7th Grade
20 questions
Grammar Review

Quiz
•
6th - 9th Grade
Discover more resources for Religious Studies
11 questions
All about me

Quiz
•
Professional Development
10 questions
How to Email your Teacher

Quiz
•
Professional Development
5 questions
Setting goals for the year

Quiz
•
Professional Development
14 questions
2019 Logos

Quiz
•
Professional Development
6 questions
GUM Chart Scavenger Hunt

Quiz
•
Professional Development
8 questions
Understanding Government: Limited and Unlimited

Quiz
•
Professional Development
20 questions
tape measure

Quiz
•
Professional Development
24 questions
Street Signs

Quiz
•
9th Grade - Professio...