Atté charia niata la ?

Quizz révision

Quiz
•
Religious Studies
•
Professional Development
•
Hard

Diarra Mbacké
Used 3+ times
FREE Resource
9 questions
Show all answers
1.
MULTIPLE CHOICE QUESTION
30 sec • 1 pt
7
5
4
6
2.
FILL IN THE BLANK QUESTION
1 min • 1 pt
Até charia yan la ?
3.
MULTIPLE CHOICE QUESTION
30 sec • 1 pt
Bane malaka moy garder al jannah ?
Ridwan
Hatid
Mikail
Azrail
Israfil
4.
MULTIPLE CHOICE QUESTION
30 sec • 1 pt
Niata yonente laniou digueul niou diotali (messagers) ?
124 000
313
25
40
5.
MULTIPLE CHOICE QUESTION
30 sec • 1 pt
Sokhnassi dafa dioulé yéré yimou solone bimouy guiss mbakh. Ndakh diouli gui werna ?
diouli dji weroul
sou yere dji amoul sobe diouli dji werna
diouli dji werna
6.
MULTIPLE SELECT QUESTION
45 sec • 1 pt
Kan lassi kooram yakou ?
- kiy nélaw beuthieugou koor gui yeup
ki woor té diouli woul béneu waxtou si biss bi
kiy nélaw guenteu maniyou guéneu si moom
ki kheum beutieugou koor gui yeup
ki tay wothiou si beuthieugou koor
7.
MULTIPLE SELECT QUESTION
45 sec • 1 pt
Yan lassi djiguén meunoul deff ?
toud doom
rendi kharou tabaski
djité diouli
mayé seuy
8.
MULTIPLE SELECT QUESTION
45 sec • 1 pt
Kan mossiy yéfeur ?
chrétien ak juif
kiy diamou kheureum
boudiste
dioulit bou wedi diouli
athé
9.
MULTIPLE SELECT QUESTION
45 sec • 1 pt
Louy différence entre mouslim (dioulit) ak mouhmin (kou gueum) ?
mouslim moy kou gueum yonenté bi (Mouhammad PSL)
Mouhmin moy kou gueum Yalla wayé dou dieufé ponk yi
bépeu mouhmin rék mouslim leu
mouslim moy kou gueum Yalla té douko bokalé ak dara
Similar Resources on Quizizz
Popular Resources on Quizizz
15 questions
Multiplication Facts

Quiz
•
4th Grade
25 questions
SS Combined Advisory Quiz

Quiz
•
6th - 8th Grade
40 questions
Week 4 Student In Class Practice Set

Quiz
•
9th - 12th Grade
40 questions
SOL: ILE DNA Tech, Gen, Evol 2025

Quiz
•
9th - 12th Grade
20 questions
NC Universities (R2H)

Quiz
•
9th - 12th Grade
15 questions
June Review Quiz

Quiz
•
Professional Development
20 questions
Congruent and Similar Triangles

Quiz
•
8th Grade
25 questions
Triangle Inequalities

Quiz
•
10th - 12th Grade